|
![]() |
|||
|
||||
OverviewWaa so mënon delloo ay waxtu walla ay at ci ganaw? Ak téeré bi, ma ngi lë woo ci ngë dellu ci dëmb ndax ngë xam sa ndono ni mu réyé. Buur bu goor ak bu jigéen, njitt dëkk ya won ak jambaar yu goor ak yujigéen, defaral sa toggay te ngë gëstu(jàngat) Jëfin ak kawtefu 4 kangam dëmb yi ci Afrik. Ci jeexantal téeré bi, ab pàcc laa ñu la jagglel ngir ngë tekk ay kuloor ci nitaal yi lolu dina tax ngë bokk ci léeb bi ci wetu jambaar yi. Mbaa pare ngë ? Full Product DetailsAuthor: Mélissa Francisco , TullipstudioPublisher: Melissa Francisco Imprint: Melissa Francisco Dimensions: Width: 21.60cm , Height: 0.60cm , Length: 21.60cm Weight: 0.349kg ISBN: 9782493538109ISBN 10: 2493538102 Pages: 48 Publication Date: 15 August 2022 Audience: Children/juvenile , Children / Juvenile Format: Hardback Publisher's Status: Active Availability: Available To Order ![]() We have confirmation that this item is in stock with the supplier. It will be ordered in for you and dispatched immediately. Language: Wolof Table of ContentsReviewsAuthor InformationTab Content 6Author Website:Countries AvailableAll regions |